Xel - Youssou N'Dour

Xel - Youssou N'Dour

Год
2007
Язык
`francuski`
Длительность
290680

Poniżej tekst piosenki Xel , wykonawca - Youssou N'Dour z tłumaczeniem

Tekst piosenki „ Xel ”

Oryginalny tekst z tłumaczeniem

Xel

Youssou N'Dour

Paroles de la chanson Xel:

Famarë reub kat lawone

Da ama biss mou khall yône

Mu taxaw di xalat bamu yàg

Mu sène mbëtt miy daw

Mu suxat fital ambadi dâgu

Té nane kî douma raw

Far mbëtt ma sène kokorong

Dadi dieul bop ba

Dal di koy rône

Bopp ba neubouna litha des

Yaramam béppa ngui fègn

Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya

Lippe di fègne

Lii takh mou déféni

Mbeutteu daa amoul xel

Kone gnoune gni Yalla jox xel

Nagnu santati (x2)

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax déf

Loy dougou jitalal sa xel

Ba lo thièy wout

Di nga guiss nguenél

Nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna

Kiy déf té dou xalat

Thi missal day mél ni mbeut ma

Nit môm khélako yor (x4)

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf

Fi neubeu moy khax

Boko amoul yangui mél ni bayima

Sokou amoul doto nék nit

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf

Wawaw (x4)

Famarë reub kat lawone

Da ama biss mou khall yône

Mu taxaw di xalat bamu yàg

Mu sène mbëtt miy daw

Mu suxat fital am ba di dâgu

Té nane kî douma raw

Far mbëtt ma sène kokorong

Dadi dieul bop ba

Dal di koy rône

Bopp ba neubouna litha des

Yaramam béppa ngui fègn

Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya

Lippe di fègne

Lii takh mou déféni

Mbeutteu daa amoul xel

Kone gnoune gni Yalla jox xel

Nagnu santati (x2)

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk

Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf

Wawaw lolu moy xel

Soko amoul

Yangui mél bayima (x3)

Loy dougou nang ko téké xel

Famarë reub kat lawone

Mbeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt!

Ponad 2 miliony tekstów piosenek

Piosenki w różnych językach

Tłumaczenia

Wysokiej jakości tłumaczenia na wszystkie języki

Szybkie wyszukiwanie

Znajdź potrzebne teksty w kilka sekund